Audio - Affaire Khadim Ndiaye - Aida Macké: Les confidences du fils du propriétaire de la maison.

JOTAAYU Sénégal (JS) JOTAAYU Sénégal (JS)
10 dias 1121
502,852 vistas 74%
1,477 526

Descargar
  • por favor espere
Descripci
Categoría

Música

Dian Diallo
Dian Diallo 2 dias
.
Lamine Gueye
Lamine Gueye 2 dias
Nous les africains gno guena sonou fi wayé tam gno nara guena sonou yawmal khiyam
Lamine Gueye
Lamine Gueye 2 dias
Man dé tay la bayi tass Kimome nan الرجال القوامون على نشاء. Réwmi degue manofi am c impossible jamais. Par ce man yi journaliste maguis Amolén sakh odase posée les question❓ clairement Nit bo ray nit guénnan dondou kou warona diékh J8 peur de mon pay Motakh gnon macky sall rék mogno wara djité comme président mome mi wakh nous sommes des sytoiyé ordinaire Ou bien sakh sonko comme mome guemoul tarikha Ndakh dnépou mana tègué si yon Par ce ki lou rakh mo déf li da khamon ni dara doko si fék Mo takh mo am fit défli
Lamine Gueye
Lamine Gueye 2 dias
Senega barina ay nafékheu
anta seye
anta seye 2 dias
yalla na yalla yeureum khadim
Moussou Sarr
Moussou Sarr 3 dias
moi je ne comprends Sénégal parceque ki raw dieukeureum wané naniou ko siwal ko fepp mais loutakh niou sathie khalé yi,di violé waté bouniou léne diapé douniou wané???????
Layzo Carlou
Layzo Carlou 3 dias
Mais bro bi vrai doff leu koi ...Meurtre am nganane plainte amoul..Même s\'il n\'y a pas de plainte, les responsabilités doivent être situées... La justice est là pour tout le monde
Layzo Carlou
Layzo Carlou 3 dias
Koutaal dieukeureum nguéne naane kou bakh leu ...vrai dof nguéne koi ...C\'est le monde à l\'envers
Cherif Cherif
Cherif Cherif 3 dias
Joli
Marieme Bassoum
Marieme Bassoum 3 dias
Méchante épouse tu n mérite Pa être mère tu a mis la honte ns femme loumoutou done tale nite tu allé tro loin vrmmt
Massylla Mbaye
Massylla Mbaye 4 dias
Ndawsi daal kou bone la té sokhor di lakk nit mélni kou yor dibitéri , nioukoy dèma rafétal li kéne manouko rafétal bam rafét
Oumy Gueye
Oumy Gueye 4 dias
qui sokhor na trop
Masseye Fall
Masseye Fall 4 dias
Li dawna yaram yalla rek mo kham
Yayetop Thiam
Yayetop Thiam 4 dias
Un. Mari. Beau
Mafou Aidara
Mafou Aidara 4 dias
Mane maa waarou
Diatou Diallo
Diatou Diallo 4 dias
Djiepi na wa senegal 🇸🇳 Bilaye Walay femm bi bougn mako abalone nako togu lek ko Bilaye Walay en plus ki khamoul khol mane Serigne ak famille douma leine ax falè force damay ray femm bi mou nek match null Bilaye lou nit firr firr tall c la dernière chose koi
dia aissatou
dia aissatou 4 dias
Vous etes trop hypocrites mes chers journalistes c est quoi c est histoire on parle de meurtre de premeditation
Julienne Badiane
Julienne Badiane 4 dias
Crime par préméditation. Donc c\'est la prison directe
modou lo
modou lo 4 dias
kimom dafabon torp
michou diaw talibe baye Niass Diaw
michou diaw talibe baye Niass Diaw 4 dias
Yaw mom mansour diop mala weddi naké yaw Domi haram gua geumoulo dara amoul domou serigne amoul dara wakha li yalla wakh si kou ray niit na nekeu domou seuydina mouhamet baxam
la linguere Niang
la linguere Niang 4 dias
Ki dh koukoy takat day taylè bopam😂 rk
Haby Cisse
Haby Cisse 5 dias
HA LES SAPEURS POMPIERS !!!!!! TOUT MARISTE POUVAIS PRENDRE FEU ET EUX DISENT MANQUER DE RÉSEAU !!!!!! HA LE SÉNÉGAL !!!!!!
Mbaye Seck
Mbaye Seck 5 dias
Eskeuy yalla sounou borom.. Ki mo bone deugue, takhaw âme fite di soti nite essence talko mou dé
cheikh expert Camara
cheikh expert Camara 5 dias
Loutah sénégalèyii naafèkh.elhadj dall wèdinala.
Tossane Diagne
Tossane Diagne 5 dias
Bayileen mou bonne lou nieuw ngeen wakh ndogalou yallah YALLA kouko wo kouné daley diapalé soutoural la mais Satan naak kouko wo mou wouyou sila Jalousie bou eup bakhoul day attiré Satan donc d\'après les disputes la femme n\'a jamais respecté son mari ndakh khamna elle dira k sama papa moy serigne niam di gorom douma sania deef darra Kou goor ki ndeyssane mélni kharou yaar ndakh am respect am limouy rouss ak loumouy khol! Mane naak je les connaisse pas mais souma bokone ak khadim Ndiaye bou yabbo niou reyma déh mais Dame bi dinako deef cicatrice bo khamné heure bou sétto dineu fatélikou limou deef Wassalam Repose en paix khadim sunu borom doula sétane been yone il sera ton avocat Dinala pledel amoul serigne amoul justice mo bok ndiaboté nieup on est tous égaux devant lui!
Ousmane Ndiaye
Ousmane Ndiaye 5 dias
Prémédité
Fatima Rassoul Gueye
Fatima Rassoul Gueye 5 dias
Kou ray danioula wara ray
patricia diop
patricia diop 5 dias
C mon oncle le frere a mon pere ke dieu l\'accueille au paradis...
soda mbacke
soda mbacke 6 dias
Mane kouyor bi khole ya ma meune
soda mbacke
soda mbacke 6 dias
Mane kouyor bi khole ya ma meune
diarra dabo
diarra dabo 6 dias
vraiment cet acte est inexplicable! mais Allah voit tous même si elle n\'est pas punie dans la vie présente, elle le sera dans l\'au delà!
Massamba Ly
Massamba Ly 6 dias
Boukene togn seytanè nak Jalousie c animal .beuy sakh dafay firr Guinar sof mbame khoukh. Mais dem bay jeul essence talll Kou sokhorr lol lol lol mokoy def Sa merite punution .loi kasso charia reyy
sy amsatou
sy amsatou 6 dias
En plus il etais tres beau wallah thier elle a gater la vie de ce jeune homme.wallah
sy amsatou
sy amsatou 6 dias
On a qu\'a appliquer la charia wallah ke Azawadjel accorde a khadjim le djannatou firdaws
issa diallo
issa diallo 6 dias
réponse en paix
Awa Gueye
Awa Gueye 6 dias
Slu
Neva Sow
Neva Sow 6 dias
Quand une femme est movaise elle est très movaise.
Mariane tu Est le Rio Ndiaye
Mariane tu Est le Rio Ndiaye 6 dias
Elle méritte l\'enfer sette solope de Aicha mbacke nitte kou meune déef
mouhamed mbaye
mouhamed mbaye 6 dias
Mane dee sama yone nékoussi Dee! Khawma Lou khew ! Wayei problème waroul takh keneuh dii taaal nite nak
Mohamed Sall
Mohamed Sall 6 dias
Sa diabar boula talone do wakh laulou imbéciles
penda elimane thiam
penda elimane thiam 6 dias
wa tamit mane dal meunouma comprendre nit Lou gnaw li rawatina Ray nit gnounane nit yi nagnou manou la femme limou def dara meunouko rafetal ak famille boumou meundi bok yakhna derou ay mbokam fi mom kou dé ya perte même bou amout plainte yone dina def liguayam lima meiti thi Sénégal mou moudjei beuri ish se pays de merde
Khady Sarr Sarr
Khady Sarr Sarr 6 dias
Hum diga teud prison dè k sa soi clair dan ta tête .de plus tu n la jamé aimè kéne dou dèf Lou bonn lhomm de ta vie c du nimport koi
Maman Sy
Maman Sy 6 dias
Astou ya bone di rey
beydy sakho
beydy sakho 6 dias
Lou geuna grave si li ni dome dji mou wossine le lendemain sou magué ladj yayam kane moy sama papa lane lako sokhnassi di tontou
amt amt
amt amt 6 dias
Al maktoum.newonna nan sangat rewmi.ndax danouno rax.yenn yi douk neen.taal sa dieukeur.rendi sa baay.ak ay xarou youdoul diex.ta ay djoulit rek koy def.yalnanuci yalla miuseul mes li doyna war
Amadou Toure
Amadou Toure 6 dias
Xxx
Astou DIOP
Astou DIOP 6 dias
Vraiment. En tant djiguen dama rousse. Latmokoffi diare. Yakhe sa adina.
Abdou Ngom
Abdou Ngom 6 dias
قال تعالى وكتبنا عليهم فيها أن النفس بالنفس إلى ءاخره ءايه
oumy diatta
oumy diatta 6 dias
que la terre lui soit legere repose en paix
Fatou Faye
Fatou Faye 6 dias
C pas une raison de le tuer elle merite quon le tue
di_ _dy
di_ _dy 6 dias
Nane si mandou legui senegal couple bou ande si diam laniouy bagne gel bi sakh meune nane ko khaptal vu k legui senegal danio sokhor pck nitt ko beugu doko def lou metii..sa chelou
Mbacke Amy
Mbacke Amy 6 dias
Manou dal bakhna nit lou yonam nekoul nasi manou khadim ndiaye yalla nako yalla yeureum
Fanta Dabo
Fanta Dabo 7 dias
Pouff Sénégal dall mo nekh daguenne di fattè sakh ni yalla amna serigne la certe mai waroul takh domam di tallè na yonne def liguè yeum
Assane Sarr
Assane Sarr 7 dias
Il ya vraiment des débiles dans notre planète.... non débile et seytané.... putin la justice n attend pas de plainte pour démarrer la machine judiciaire.... alors vous les 3 connard fermez vos gueule...
Adama Diallo
Adama Diallo 7 dias
Boulen ko bal
Samath Diaw
Samath Diaw 7 dias
Ki nanko nokou si gosobi
Samath Diaw
Samath Diaw 7 dias
Baarkeb seringne Bamba ndaaw si kou bonella ki dafa reeew waaye naneko raaye
petit max
petit max 7 dias
Niit souy wakh day wakh louko woor Sénégal journalistes yi gnoy conduire gneup en erreur. Merci pour ces éclaircissements!!!
L'aube d'Afrique Tv LDTv
L'aube d'Afrique Tv LDTv 7 dias
Yalla nako yalla kharè aldiana
Maxalabelle Kane
Maxalabelle Kane 7 dias
laisse dieux jugé
sarr livia
sarr livia 7 dias
Laisser la police faire son boulot!lol les journalistes confirment déjà que c\'est avec préméditation, et les pompiers qui n\'ont pas de réseau et rejettent la faute sur la Sonatel,alors que bien souvent les numéros d\'urgences sont accessibles et gratuits , ils prennent vraiment les gens pour des cons , Qu\'en pensez-vous ?.
Kiné TINE
Kiné TINE 7 dias
Aÿ way Sénégal mo nex gua Ray nit gnouné dogalou yalla la
Dieynaba Ndiaye
Dieynaba Ndiaye 7 dias
J n\'éprouve aucune pitié pour elle dieul essence sotti sa yaram dawoul tal allumette khoss sa yaram dawoul kelk soit l problem dara diarouko si aduna ki dal dafa ray nitt n\'a dead si kasso bi li dafa eup yalla nanou yalla mousseul si satan rek
aminata diallo
aminata diallo 7 dias
Wa gni ligni wakh isca gno ngui coi deglu? Man daaaaal man daaaaal Senegal dugnu avence! Tarde ba faw!
Talla Diop
Talla Diop 7 dias
NDAWSI KOU BONNE LA DAGNOU KO WARA LAK . publiquement . .LI GUENA METTI MOY DARA DOUKO SI FEK . C\'EST LE SENEGAL
Astou Diouf
Astou Diouf 7 dias
Naka la nite mana taa Lee limo bagiu bone rek
kiki sane
kiki sane 7 dias
Walay lima nakari si sounou rew barina barki yonentebi senegal bayil sou nit rayé nguani ndogalou yalla lah beneu djiguene moy yakeu tourou djiguene yeup barki serigne saliou mbacke non je di non mais on è dans kel pays ofet ay ay bessou penthieumi dineu meti dè pakhma Dina tang dh barki alkouran deug leu djiguen keneu douko tek lou meti dh mais ndaw si limou def tekko lou meti dagan neu rayko kom kimou def dieukeur wa ana loukofi diar nakh woudiou wa lolou lou yalla wakhla les hommes ont le droit depousé beneu ba nienteu wa kone bokou weurseuk leu soula nekhoul ngua delou sa keur bayi mo geun lou niaw yaw tey sa dom dj sou magué banila yaye boy ani sama papa lokoy wakh mako ray lolou niawneu trop trop sakh
lika angelique Fall
lika angelique Fall 7 dias
Je me demande comment on peut faire du mal a la personne que tu prétends aimé vraiment cette femme est un assassin. Qu\'importe les liens familiales entre eux elle a ôté la vie elle mérite la mort. Neup neupal gui lagnou wara bayi
Bamba laye
Bamba laye 7 dias
Dolennn toussss wadji na fekeu la mome loutah mandou woul féké woul dara loumouy témoin yé té daffa fékeu lepeu diéh la seul personne qui peux dire c les deux filles yiko faye kiko dieuka guisse moy takeu dou niak amena loumou degeu moma bi khadim nane sama diambare talenama donc niakoul femme bobou moma bimouy faye takeu takeu bi khadim amena ay mo youmou wah mé wadji nafékeu papa dawsi tamite na xameni khadim beugonn na bénéne beuss boudoul bi mouy wah beussou khadim bi rafétena doyna warrr yénneu serigne yi nio yakeu Sénégal . doyna ware trop gnoup modou modou yi nekeu si diaspora bi nékeu akeu sougnouy nawlé chaque jours gnou rouss sénn kaname Sénégal lifa nekeu eupeuna YouTube boffa dougé tapé Sénégal sa xol yeupeu mofay diéh comm gnoune nio mome lou bonne beugeu ko fétowé .et pourtant ya des dignes fils du pays Sénégal diaral nalénn lépeu mé Sénégal donatoul touss si monde bi daw kou déff lou bonn déf si face bi wala youtube motah diaspora bi légui beneu gore bougoul gnibi Sénégal
Rokhaya Sy
Rokhaya Sy 7 dias
Mé c du jamé vu yaw noy kholé niit en tant ke sa dieukeur gakoy soti essence yaw so amé loula meti do dieul sa bagage dem sa yone lolou ani louko guena yomb mé Sénégal dall aaaahh mane diakhlé na niit mo lundeumm deug
l'invincible
l'invincible 7 dias
Wa sapeurs aussi ils sont nuls et sans compétence
Mike Loopy
Mike Loopy 7 dias
Lifetime jail rek . Nothing else
abdul hakim mohammad
abdul hakim mohammad 7 dias
Yéne merde, niou raye un être humain niounane ndogolou YALLAH la.
cr7fall96 llaf
cr7fall96 llaf 7 dias
Cette femme mérite d\'être brûler vif
Mor niang
Mor niang 7 dias
Africa dou dem lak sapeur manoul walou! Big difference like usa
Serigne Mbacke
Serigne Mbacke 7 dias
man borom kourous gui dall Lima métti mot domdji dioudou rek dem kaso Yégoul dara khamoul dara mais foun tollou nani niane yalla mou mousall niou si ndiawtéf ak seytane ak modiou fou rafet barkeb borom touba
samba sadii ndao
samba sadii ndao 7 dias
Ak lou mounti am boule raye wala
Badinding Jabbi
Badinding Jabbi 7 dias
إنا لله وإنا إليه راجعون اللهم اغفر له وارحمه ودخله جنة الفردوس الأعلى الله أكبر
ndeye lo
ndeye lo 7 dias
Non ton ticket enfer est déjà proclamé fdp ya bonne billayiii kouuu bonne gueuu domerhame bii amoo benneuu yarrr
Rokhaya Diatta
Rokhaya Diatta 8 dias
Je suis vraiment désolée pour l\'acte que la famme
Ouz bi
Ouz bi 8 dias
paix a son âme
Khady Thiam
Khady Thiam 8 dias
Gor diaroul li
Baye mor Sall
Baye mor Sall 8 dias
yalla na souf woyaf si kawam
petite fleur des îles
petite fleur des îles 8 dias
c\'est n\'importe quoi pourquoi brûler ton marie il faut savoir divorcer si sa ne va pas
aji awa
aji awa 8 dias
massla mo yaaha Senegal. I hope the legal system will give her the maximum sentence.
Yama Drame
Yama Drame 8 dias
Rip😢😢serigne khadim
Noh Fall
Noh Fall 8 dias
Ne calcul Pas dafa eumbe ba diis .si il estáis entrin de dormir et la fille etais sur se plan de linsandier
la Perfecta diaw
la Perfecta diaw 8 dias
Version yi barina ay way Sénégal mo am gnu meuna féne merciiii pour explication yi mai ioe mome si kaso bi gnay déé domeram
adama touré
adama touré 8 dias
C’est vraiment triste et malheureux de voir comment les gens sont hypocrites au Sénégal Vous vous rendez compte qu’il s’agit d’une meurtre 😭😭😭. Une personne est morte bon sang et vous parlez de ndogal yalla et de je ne sais quoi Sincèrement dans quel monde sommes-nous aujourd’hui
maimouna diallo
maimouna diallo 8 dias
C pays est d la merde on tue des gens comme des mouches après on s permet de dire q c la volonté divine c n pas Dieu qui descendra sur terre pour régler l problème Yalla wahoul ay jaamam niou bonn mais l jugement dernier sera fatal
Alfa Junior
Alfa Junior 8 dias
Mais adouna bi mo leundeum wa femme bii nit la elle mérite une peine de mort amoul domou serigne on est tous les même que la justice soit fait
Sokhna Arame Fall Mbaye
Sokhna Arame Fall Mbaye 8 dias
Way maylén gnou diame ki boudé serignam té yaroul domam si diné kha bayiko mou don nasaran bone rew sokhor nguéndi am linguéndi wakh
Adji Thiam
Adji Thiam 8 dias
Bilae ki dagne ko wara tale
Rama Ndiaye
Rama Ndiaye 8 dias
Mai lane moy ndayou lii s kel à fai na po d nom..lé humains son indubitablemn dan 1 obscurantisme démesuré wallahi azim
Mamadou Ndoye
Mamadou Ndoye 8 dias
Haa da nekoul sa mbok tal.
abdoulaye niass
abdoulaye niass 8 dias
Elle est tout simplement mal éduquée et ne craint rien dans la mesure où elle porte le nom de...Elle a commis un crime mûrement prémédité.Il faut être sadique et mesquin à mon avis pour agir de la sorte.Malheureusement tout cela par le maslaha.Prie ALLAH ACCUEILLIR le défunt dans son paradis le plus élevé.Que la terre lui soit légère.AMINE
cool inoos
cool inoos 8 dias
Doyna war lidara dirouko
Dennis The worm
Dennis The worm 8 dias
Allons y rek, hypocrisie dineu yakkh deukk bi !
nicola omar diouf
nicola omar diouf 8 dias
Famille bou bakh bou am diné doulle ban téy la mére n a meme pas pleuré par ce que c la famille des peaky blindder
Bineta Nara DIOP
Bineta Nara DIOP 8 dias
Liii momm nexoul ba nexoul mee apouna sama yaram dfa daw bilahi